Programme

Mars 2026

Àllarba 11 Mars, dale 2h ci ngoon ba 7h ci guddi

Ateliye ci daggale welo ak dindi soldeer ci piyes elektornik yi 🔥, ngir xam ni lépp di doxee te am ay piyes yu am njariñ yu ñu mën a jëfandikoo ci ateliye bi

Àllarba, 25 Maars, dale 2h ci ngoon ba 7h ci guddi

Ateliye ci ñaw 🧵, defaraatal say yére walla tàmbali ab proose bu bees ba mu jeex!

Waxtu yi ñuy ubbi biro bi weer wu nekk